Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 149

Sabóor 149:4-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Aji Sax jee safoo ñoñam, di terale néew-ji-doole ag mucc.
5Na wóllërey Yàlla bànneexoo seen ndam, bu ñu tëddee sax, di sarxolle,
6di xaacuy kañ Yàlla, ŋàbbaale saamaru ñaari ñawka,
7ngir duma yéefar yi, mbugale ko yooyu xeet,
8yeewe seeni buur ay càllala, jénge seeni njiit jéngi weñ,

Read Sabóor 149Sabóor 149
Compare Sabóor 149:4-8Sabóor 149:4-8