Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 98

Sabóor 98:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Na géej riirandook li ko fees, mook àddinaak li ci biiram,
8dex tàccu, tund sarxolleendoo,
9gatandoo ko Aji Sax jiy dikk, àttesi àddina, di àtte dun bi njekk, tey àttee xeet yépp dëgg.

Read Sabóor 98Sabóor 98
Compare Sabóor 98:7-9Sabóor 98:7-9