Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 98:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 98:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Na géej riirandook li ko fees, mook àddinaak li ci biiram,
8 dex tàccu, tund sarxolleendoo,
9 gatandoo ko Aji Sax jiy dikk, àttesi àddina, di àtte dun bi njekk, tey àttee xeet yépp dëgg.
Sabóor 98 in Kàddug Yàlla gi