Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 82

Sabóor 82:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Sàmmleen àqu néew-ji-dooleek jirim, tey àtte yoon ku ñàkk ak ku ndóol.
4Walluleen néew-ji-dooleek walaakaana, di leen xettli ci ku bon.
5«Ndawi péncum Yàlla yii xamuñu, dégguñu; xanaa di doxe lëndëmu ñaawtéef, ba kenuy suuf yépp di jaayu.
6«Dama ne ay yàlla ngeen, yeen ñépp di njabootu Aji Kawe ji.

Read Sabóor 82Sabóor 82
Compare Sabóor 82:3-6Sabóor 82:3-6