Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 52

Sabóor 52:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Moo jàmbaar ji, looy damoo jëfi coxor? Yàlla, ngoram, bés bu nekk la.
4Ak sa làmmiñ wi ngay sose loraange, mel ni saatu su ñu xacc, rambaaj bi!
5Lu bon a la gënal lu baax, fen a la gënal wax dëgg. Selaw.
6Yaa bëgg jépp wax juy yàq, waabajiiba bi!

Read Sabóor 52Sabóor 52
Compare Sabóor 52:3-6Sabóor 52:3-6