Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 130

Sabóor 130:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Muy jàngi yéeg, ñu di ko màggale Yàlla. Aji Sax ji, ci ay xóote laa lay wooye.
2Boroom bi, déglu ma, teewlu ma, ma tinu la.
3Ki Sax, yaw, soo doon lim bàkkaar, Boroom bi, ana kuy taxaw?

Read Sabóor 130Sabóor 130
Compare Sabóor 130:1-3Sabóor 130:1-3