Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:45-48

Help us?
Click on verse(s) to share them!
45di daagoo sago, nde say tegtal laay sàkku.
46Maay àgge ay buur sa kàdduy seede, te duma rus.
47Maay bége sa santaane yi ma sopp,
48di yóotu sa santaane yi ma sopp, di jàngat sa dogali yoon.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:45-48Sabóor 119:45-48