Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 94

Sabóor 94:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Ñu ngi làmmiñoo reewande, képp kuy def lu bon di damu.
5Aji Sax ji, say ñoñ lañuy dëggaate; say séddoo lañuy néewal.
6Jëtun akub doxandéem, ñu faat; ab jirim, ñu bóom,

Read Sabóor 94Sabóor 94
Compare Sabóor 94:4-6Sabóor 94:4-6