Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 94:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 94:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Ñu ngi làmmiñoo reewande, képp kuy def lu bon di damu.
5 Aji Sax ji, say ñoñ lañuy dëggaate; say séddoo lañuy néewal.
6 Jëtun akub doxandéem, ñu faat; ab jirim, ñu bóom,
Sabóor 94 in Kàddug Yàlla gi