Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 93

Sabóor 93:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Aji Sax ji, géej a riir, géej a àddu, mu riir, gannax ya rëkk, mu riir.
4Waaye riirum wal mu walangaanoo, ak géej gu sàmbaraaxoo, Aji Sax ja fa kaw a rawati!
5Say santaanee wér te wóor; Aji Sax ji, sellnga la sa kër jagoo bésoo bés.

Read Sabóor 93Sabóor 93
Compare Sabóor 93:3-5Sabóor 93:3-5