Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 93:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 93:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji, géej a riir, géej a àddu, mu riir, gannax ya rëkk, mu riir.
4 Waaye riirum wal mu walangaanoo, ak géej gu sàmbaraaxoo, Aji Sax ja fa kaw a rawati!
5 Say santaanee wér te wóor; Aji Sax ji, sellnga la sa kër jagoo bésoo bés.
Sabóor 93 in Kàddug Yàlla gi