Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 91

Sabóor 91:2-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Dama naa Aji Sax ji: «Yaw laay làqoo, di la fegoo; ngay sama Yàlla ji ma doyloo.»
3Kii kay moo lay musal cig fiir ak loraangey mbas.

Read Sabóor 91Sabóor 91
Compare Sabóor 91:2-3Sabóor 91:2-3