Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 91:2-3 in Wolof

Help us?

Sabóor 91:2-3 in Kàddug Yàlla gi

2 Dama naa Aji Sax ji: «Yaw laay làqoo, di la fegoo; ngay sama Yàlla ji ma doyloo.»
3 Kii kay moo lay musal cig fiir ak loraangey mbas.
Sabóor 91 in Kàddug Yàlla gi