Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 89

Sabóor 89:13-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Bëj-gànnaar ak bëj-saalum, yaa ko sàkk. Tabor ak Ermon, tund ya, di sarxollee sa tur.
14Yaa àttan, jàmbaare; sa loxo di dooley neen, sa ndijoor ca kaw!
15Njekk ak njub a lal sab jal, ngor ak worma dox jiitu la.
16Aji Sax ji, ndokklee mbooloo mu la xal di sarxollee, di niitoo saw yiw,

Read Sabóor 89Sabóor 89
Compare Sabóor 89:13-16Sabóor 89:13-16