Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 85

Sabóor 85:3-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3baal sa mbooloo seeni ñaawtéef, jéggal leen bépp bàkkaar. Selaw.
4Ba nga xadar ja, muñ mer ma.
5Éy Yàlla mi nuy musal, suqli nu, te meddi.
6Xanaa doo nu mere fàww, ba ca sët yaak sëtaat ya?
7Xanaa dinga leqli sa mbooloo, ba ñu man laa bànneexoo?

Read Sabóor 85Sabóor 85
Compare Sabóor 85:3-7Sabóor 85:3-7