Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 84

Sabóor 84:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8muy gëna am doole, ba teewi fa Yàlla ca Siyoŋ.
9Éy Yàlla Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, déglul, ma ñaan la! Yàllay Yanqóoba, teewlu ma. Selaw.

Read Sabóor 84Sabóor 84
Compare Sabóor 84:8-9Sabóor 84:8-9