Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 84:8-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 84:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 muy gëna am doole, ba teewi fa Yàlla ca Siyoŋ.
9 Éy Yàlla Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, déglul, ma ñaan la! Yàllay Yanqóoba, teewlu ma. Selaw.
Sabóor 84 in Kàddug Yàlla gi