Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 83

Sabóor 83:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Éy Yàlla, wëndeel leen ni callweer, ñu mel ni boob mu ngelaw wal.
15Éy Yàlla, ni daay di xoyome àll, sawara wa jafal tund ya,
16yal nanga leen ni toppeek sa dooley ngelaw, tiitale leen sa ngëlén.

Read Sabóor 83Sabóor 83
Compare Sabóor 83:14-16Sabóor 83:14-16