Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 83:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 83:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Éy Yàlla, wëndeel leen ni callweer, ñu mel ni boob mu ngelaw wal.
15 Éy Yàlla, ni daay di xoyome àll, sawara wa jafal tund ya,
16 yal nanga leen ni toppeek sa dooley ngelaw, tiitale leen sa ngëlén.
Sabóor 83 in Kàddug Yàlla gi