Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 77

Sabóor 77:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Bëccëg, ma jàq, sàkku Boroom bi; guddi, ma tàllal loxo, toqiwuma. Sama xol tëë sedd.
4Ma bàyyi Yàlla xel, binni, xalaat, xol jeex. Selaw.

Read Sabóor 77Sabóor 77
Compare Sabóor 77:3-4Sabóor 77:3-4