Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 77:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 77:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Bëccëg, ma jàq, sàkku Boroom bi; guddi, ma tàllal loxo, toqiwuma. Sama xol tëë sedd.
4 Ma bàyyi Yàlla xel, binni, xalaat, xol jeex. Selaw.
Sabóor 77 in Kàddug Yàlla gi