Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 73

Sabóor 73:19-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Yàquleeka leena bett! Musibaa leen ne fuuf, ñu ne mes!
20Day mel ni gént goo yewwoo. Céy Boroom bi, boo xippee, jëmmu gént ga soof la.
21Naqar laa amoon, sama xol di dagg.
22Booba ngaaka laa, xawma dara; rab laa woon fi sa kanam.
23Teewul ma des ak yaw, nga jàpp sama loxol ndijoor.

Read Sabóor 73Sabóor 73
Compare Sabóor 73:19-23Sabóor 73:19-23