Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 73

Sabóor 73:15-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Su ma noon: «Naa waxe ni ñoom,» kon de, ma wor sa askanu mbooloo.
16Naka laay jéema ràññee lii, mbir mi ëlëm ma.
17Ba ma àggee sa kër gu sell ga, laa doora gis muju ku bon.
18Yoonu tarxiis kay, nga leen teg, daane leen, ñu sànku,
19Yàquleeka leena bett! Musibaa leen ne fuuf, ñu ne mes!

Read Sabóor 73Sabóor 73
Compare Sabóor 73:15-19Sabóor 73:15-19