Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 6

Sabóor 6:7-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Onk naa ba loof, di fanaanee jooy, sama lal di féey, ba far seeye rongooñ.
8Saay gët a ngi xóot ndaxu naqar, boole ci giim ndax tooñi noonoo noon.
9Yeen, defkati ñaawtéef yépp, xiddileen ma! Aji Sax ji dégg na saay jooy,
10Aji Sax ji dégg na saay dagaan, Aji Sax jii nangu na samag ñaan.

Read Sabóor 6Sabóor 6
Compare Sabóor 6:7-10Sabóor 6:7-10