Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 60

Sabóor 60:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Yàllaa àddoo fa këram gu sell, ne: «Maay damu, dogat suufas Sikem, séddale xuru Sukkóot.
9Maa moom diiwaanu Galàdd, moom Manase, Efrayim di sama mbaxanam xare, Yuda di sama yetu nguur,

Read Sabóor 60Sabóor 60
Compare Sabóor 60:8-9Sabóor 60:8-9