Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 60

Sabóor 60:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Walloo nu sa ndijoor, nangul nu, ba say soppe xettliku.
8Yàllaa àddoo fa këram gu sell, ne: «Maay damu, dogat suufas Sikem, séddale xuru Sukkóot.

Read Sabóor 60Sabóor 60
Compare Sabóor 60:7-8Sabóor 60:7-8