Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 60:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 60:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Walloo nu sa ndijoor, nangul nu, ba say soppe xettliku.
8 Yàllaa àddoo fa këram gu sell, ne: «Maay damu, dogat suufas Sikem, séddale xuru Sukkóot.
Sabóor 60 in Kàddug Yàlla gi