Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 59

Sabóor 59:9-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Te yaw Aji Sax ji, yaa ngi leen di ree, yaa ngi kekku yéefar yii yépp.
10Yaay sama doole, ma di la séentu, yaw Yàlla, yaay sama rawtu.
11Sama Yàlla ju goree may gatandu. Moo may may ndam ci noon yi, ma gis.
12Yàlla, bu leen rey, lu ko moy samaw xeet fàtte. Tasaaree leen sa doole, daane leen. Boroom bi, yaa nuy feg.

Read Sabóor 59Sabóor 59
Compare Sabóor 59:9-12Sabóor 59:9-12