Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 54

Sabóor 54:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Éy Yàlla, déglul, ma ñaan, teewlul, ma wax la.
5Ay doxandéem a ma jógal, di ñu néeg, bëgga jël sama bakkan, te seetuñu ci Yàlla. Selaw.
6Yàllaa ngii, moo may dimbali; Boroom bee yor sama bakkan.

Read Sabóor 54Sabóor 54
Compare Sabóor 54:4-6Sabóor 54:4-6