Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 4

Sabóor 4:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Bare na ñu naan: «Ana ku nuy won lu baax?» Éy Aji Sax ji, baaxe nu saw yiw!
8May nga ma bànneexu xol bu raw seen pepp mu tuurook biiñ bu wal.

Read Sabóor 4Sabóor 4
Compare Sabóor 4:7-8Sabóor 4:7-8