Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 4:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 4:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Bare na ñu naan: «Ana ku nuy won lu baax?» Éy Aji Sax ji, baaxe nu saw yiw!
8 May nga ma bànneexu xol bu raw seen pepp mu tuurook biiñ bu wal.
Sabóor 4 in Kàddug Yàlla gi