Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 49

Sabóor 49:16-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Waaye Yàllaa may musal ci dooley njaniiw, jot sama bakkan, ba jël ma.
17Buleen yéemu ci ku barele, teraangay këram di yokku.
18Du dee ba yóbbaale dara, teraangaam du ko topp biir bàmmeel.
19Na bége bànneexu bakkanam, ñu di ko kañe koomam,

Read Sabóor 49Sabóor 49
Compare Sabóor 49:16-19Sabóor 49:16-19