Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 48

Sabóor 48:11-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Céy Yàlla, sa tur ay sa woy ba ca cati àddina. Njekk la sa loxo fees.
12Yal na waa tundu Siyoŋ bég, waa Yuda bànneexoo say àtte.
13Doxleen biir Siyoŋ, wër ko, waññleen ay soorooram,
14nemmikuy tataam, doxantoo këri buur, ba man koo yegge maasug ëllëg,

Read Sabóor 48Sabóor 48
Compare Sabóor 48:11-14Sabóor 48:11-14