Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 40

Sabóor 40:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Éy Aji Sax ji, yal na la neex, nga wallu ma! Éy Aji Sax ji, gaawe ma!
15Képp kuy wuta fëkk sama bakkan, yal na rus, torox ne tott. Kuy bége sama loraange, yal nañu ko duma, mu ne yàcc.
16Ku may ñaawal, yal nañu ko torxal, mu jommi.

Read Sabóor 40Sabóor 40
Compare Sabóor 40:14-16Sabóor 40:14-16