Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 40:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 40:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Éy Aji Sax ji, yal na la neex, nga wallu ma! Éy Aji Sax ji, gaawe ma!
15 Képp kuy wuta fëkk sama bakkan, yal na rus, torox ne tott. Kuy bége sama loraange, yal nañu ko duma, mu ne yàcc.
16 Ku may ñaawal, yal nañu ko torxal, mu jommi.
Sabóor 40 in Kàddug Yàlla gi