Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 34

Sabóor 34:17-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Aji Sax jeey rëbb kuy jëfe mbon, ngir dagge ko kaw suuf, far turam.
18Ku jub yuuxu, Aji Sax ji dégg, fu mu jàqe, mu musal ko.

Read Sabóor 34Sabóor 34
Compare Sabóor 34:17-18Sabóor 34:17-18