Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 20

Sabóor 20:4-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Yal na xool loo ko jébbal, di rafetlu sarax soo ko lakkal. Selaw.
5Yal na la may li nga namm, di sottal loo mébét,
6ngay daan, nuy ree, yéege sunu raaya, màggal sunu Yàlla. Yal na Aji Sax ji nangu loo dagaan.
7Aji Sax jeey musal ki mu fal, bir na ma tey. Moo koy nangule fa asamaan su sell sa, ci dooley ndijooram biy musle.
8Ñiiki watiir, ñeeki fas, nun sunu turu Yàlla Aji Sax ji lanuy tudd.

Read Sabóor 20Sabóor 20
Compare Sabóor 20:4-8Sabóor 20:4-8