Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 20:4-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 20:4-8 in Kàddug Yàlla gi

4 Yal na xool loo ko jébbal, di rafetlu sarax soo ko lakkal. Selaw.
5 Yal na la may li nga namm, di sottal loo mébét,
6 ngay daan, nuy ree, yéege sunu raaya, màggal sunu Yàlla. Yal na Aji Sax ji nangu loo dagaan.
7 Aji Sax jeey musal ki mu fal, bir na ma tey. Moo koy nangule fa asamaan su sell sa, ci dooley ndijooram biy musle.
8 Ñiiki watiir, ñeeki fas, nun sunu turu Yàlla Aji Sax ji lanuy tudd.
Sabóor 20 in Kàddug Yàlla gi