Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 15

Sabóor 15:2-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Xanaa ki wéye maandu, di def njekk, di wax dëggu xolam.
3Du sos, du tooñ dëkkandoo, du baatal moroomam.

Read Sabóor 15Sabóor 15
Compare Sabóor 15:2-3Sabóor 15:2-3