Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 146

Sabóor 146:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Aji Sax jeey xippil silmaxa, di siggil ku sëgg. Aji Sax jee sopp ku jub.
9Aji Sax jeey sàmm doxandéem, taxawu jirim ak jëtun, waaye mooy lajjal pexem ku bon.

Read Sabóor 146Sabóor 146
Compare Sabóor 146:8-9Sabóor 146:8-9