Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 146:8-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 146:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 Aji Sax jeey xippil silmaxa, di siggil ku sëgg. Aji Sax jee sopp ku jub.
9 Aji Sax jeey sàmm doxandéem, taxawu jirim ak jëtun, waaye mooy lajjal pexem ku bon.
Sabóor 146 in Kàddug Yàlla gi