Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 146

Sabóor 146:4-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Noo ga day rëcc, mu dellu suuf; bu bés baa, pexeem jeex.
5Ndokklee kuy dimbalikoo Yàllay Yanqóoba; di yaakaar Yàllaam Aji Sax ji,
6ki sàkk kaw ak suuf, géej ak lu ci biiram, di sàmm dëgg ba fàww,
7di àtte néew-ji-doole, di leel ku xiif. Aji Sax jeey tijji ku ñu tëj.

Read Sabóor 146Sabóor 146
Compare Sabóor 146:4-7Sabóor 146:4-7