Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 141

Sabóor 141:2-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Yal nanga ma nangul samag ñaan ni cuuraay lu ñu la taalal, yoxo yi ma la tàllal di saraxu ngoon soo gërëm.
3Aji Sax ji, sàmmal ma sama làmmiñ, saytul ma sama kàddu.
4Bu ma xiir ci lu aay, may jëfe jëf ju bon, ànd ceek ñiy jëf lu ñaaw, di wàlli seeni bernde.

Read Sabóor 141Sabóor 141
Compare Sabóor 141:2-4Sabóor 141:2-4