Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 137

Sabóor 137:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Fa la nu sunuy sang daa woyloo, not nu, bëgg nu bégal leen, naan: «Woyal-leen nu ci woyi Siyoŋ.»
4Moo nu nuy woye woyu Aji Sax ji kaw suufas yéefar?
5Éy Yerusalem, su ma la naree fàtte, yal na ma doole dëddu!
6Yerusalem, su ma la fàttlikuwul, fonk la, ba gën laa bége lépp, yal na sama làmmiñ tafoo sama denqleñ.

Read Sabóor 137Sabóor 137
Compare Sabóor 137:3-6Sabóor 137:3-6