Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 132

Sabóor 132:13-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Aji Sax ji kat a tànn Siyoŋ, taamu faa dëkke.
14Mu ne: «Fii laay dal-loo ba fàww, fii laay dëkk, maa ko taamu.
15Dund bi, ma barkeela barkeel, néew-ji-doole yi, ma reggal;
16sarxalkat yi, ma wodde njot; way-gëm ñi di sarxollee sarxolle.

Read Sabóor 132Sabóor 132
Compare Sabóor 132:13-16Sabóor 132:13-16