Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 132:13-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 132:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Aji Sax ji kat a tànn Siyoŋ, taamu faa dëkke.
14 Mu ne: «Fii laay dal-loo ba fàww, fii laay dëkk, maa ko taamu.
15 Dund bi, ma barkeela barkeel, néew-ji-doole yi, ma reggal;
16 sarxalkat yi, ma wodde njot; way-gëm ñi di sarxollee sarxolle.
Sabóor 132 in Kàddug Yàlla gi