Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 126

Sabóor 126:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Lu réy la nu Aji Sax ji defal moos, nu bég.
4Aji Sax ji, rikk delloo nu na woon, ni ngay delloo wal yu ŋiis, mu walaat ca àllub Negew.
5Kuy ji di jooy, yal na góob, di sarxolle.

Read Sabóor 126Sabóor 126
Compare Sabóor 126:3-5Sabóor 126:3-5