Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 9

Sabóor 9:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Yaw Yàlla, dama lay bége, bànneexoo la, woy la, yaw Aji Kawe ji.
4Noon yeey dellu gannaaw, tërëf, sànku fi sa kanam.
5Yaa ma àtte yoon, dëggal ma, toog ci sab jal, di àtte njub.
6Rëbb nga xeet yi, sànk ñu bon ñi, far seeni tur ba fàww.

Read Sabóor 9Sabóor 9
Compare Sabóor 9:3-6Sabóor 9:3-6