Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 9:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 9:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaw Yàlla, dama lay bége, bànneexoo la, woy la, yaw Aji Kawe ji.
4 Noon yeey dellu gannaaw, tërëf, sànku fi sa kanam.
5 Yaa ma àtte yoon, dëggal ma, toog ci sab jal, di àtte njub.
6 Rëbb nga xeet yi, sànk ñu bon ñi, far seeni tur ba fàww.
Sabóor 9 in Kàddug Yàlla gi