Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 97

Sabóor 97:2-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Ay xàmbaar a ko yéew, njekk ak njub lal ab jalam.
3Sawaraa dox, jiitu ko, di xoyomi noonam wetoo wet,
4ay melaxam leeral àddina, waa àddina gis, di pat-pati;

Read Sabóor 97Sabóor 97
Compare Sabóor 97:2-4Sabóor 97:2-4